What’s up Quoi de neuf ? (paroles)
Résumé :
« Quoi de neuf, combien de voix as-tu en mémoire ? Jeune diplômé, sans emploi, je suis dans le désarroi à vouloir être célèbre. Président, des possibilités existent pour en sortir. »
yo ye what’s up what’s up what’s up ?
Eh quoi de neuf .
how life treatin u ? Nu mu deme ci sa side ?
Comment la vie t’a traité ? Comment ça se passe de ton côté ?
noo tooge laa lay laaj ?
Je demande de tes nouvelles ?
wax ma lu ne sa mind, Wax ma lu ne sa mind
Dis-moi ce qui te trotte dans la tête, dis-moi.
Yow what’s up what’s up what’s up bul kalu ci sa side
Eh toi, quoi de neuf ? Quoi de neuf ? Ne reste pas dans ton coin ?
yow wax ma lu lay faj ? li la metti naa ko taaj
Parle-moi de ce qui te soigne ? Je voudrais savoir ce dont tu souffres
wax ma lu ne sa mind jël ma ci suuf
Dis-moi ce qui te trotte dans la tête
wax ji buñ ko aaaj
ne suspendons pas le débat
yé ya yaww
yé ya toi
wiiyu wiiyu wuuyu wii wii
répondre répondre oui
yé ya yaww
yé ya toi
wuyu wiiyu
répondre, répondre
ndaw dafa jaaxle
les jeunes sont inquiets
ndaw dafa sonn
les jeunes sont fatigués
yéy ay diplômes ba géex ne noηη
bardés de diplômes et seuls
bëgg tekki tekki bi lekk lekk gi doηη
ils ont envie de réussir juste de réussir
bëgg fës ci tele bi def buzz di bomb
Ils ont envie d’être célèbres à la télé faire le buzz devenant une bombe
yé yé yéy yaw yaw yaww
Yé yé yé toi toi
wuyu wiiyu wuuyu wii wii
Répondre, répondre, répondre oui oui
yaaw yaaw yaw yaa yaw
toi toi toi toi toi
Ñaata baat a ne sama biir bopp
Combien de voix sont dans ma tête ?
Bu ne yor mic amaguma job
Chacune a ses effets je n’ai pas encore de travail
Soxla gëna bari bu ne dima topp ne ma na gën a toog bul mësa jóg buumu gàcce dog ya ko fi mën mbaam di nga kott
les problèmes de plus en plus nombreux me tracassent en me disant de patienter ne te rebelle jamais, laver l’affront est à ta portée
lépp sotti léegi ma ne dina mat
tout est parfait bientôt tout sera plus que parfait
soxna ki doom fu ma leen di fat
Madame, où est-ce que je vais loger ces enfants
Lila gën a bëgg maa ngi jëm mag
que j’aime le plus je commence à prendre de l’âge
Bu ma kenn yàqal fok dem ba jéex tàkk !
Que personne ne nuise à mes intérêts j’irai jusqu’au bout de mes forces !
Cons bi le dund bëgg lu bees tàq
La Consommation, raffoler de flambant neuf
Gisoo sama sho bi fok ma takk
N’as-tu pas vu mon sho que je dois porter ?
li ne sama mind yóbbu meer bi Màkka
J’ai envie d’amener ma mère à la Mecque
Dama bëgg doon star lëmbe town bi
je voudrais devenir une star casser la baraque dans cette ville
Li ma bëgg yépp yépp xajul ci sound bi
Je ne pourrai pas tout dire dans ce morceau
Mënuma wax lépp bu kenn laaj
Que personne ne me pose des questions je ne peux pas tout dire !
maa ngi ci yoon wi
je suis sur le chemin
What’s up what’s up what’s up?
Quoi de neuf ? Quoi de neuf ? Quoi de neuf ?
how life treatin u? Nu mu deme ci sa side?
Comment la vie t’a traité ? Comment ça se passe de ton côté ?
noo tooge laa lay laaj ?
Je demande de tes nouvelles ?
wax ma lu ne sa mind, Wax ma lu ne sa mind ?
Dis-moi ce qui te trotte dans la tête, dis-moi.
Yow what’s up what’s up what’s up bul kalu ci sa side et toi ?
Quoi de neuf ? Quoi de neuf ? Ne reste pas cloitré dans ton coin.
yow wax ma lu lay faj ? Li la metti nañ ko taaj;
Parle-moi de ce qui te soigne ? Je voudrais savoir ce dont tu souffres
wax ma lu ne sa mind jël ma ci suuf
Dis-moi ce qui te trotte dans la tête
wax ji buñ ko aaaj
Ne suspendons pas le débat
yé ya yaww
yé ya toi
wuyu wiiyu
répondre wiiyu
yé ya yaww
yé ya toi
wuyu wiiyu
répondre wiiyu
kenn yeetaluma ci laytaayu wurus
je ne suis pas né avec une cuillère d’argent dans la bouche
màgg ci këru njaboot te yàgg bokk mbuus
grandir dans une grande famille avec l’esprit de partage
sometimes gàlle dañuy dëpp cin dara du fi suus
Parfois à la maison la marmite ne bout pas
yàgg fande duggu classe taxuma jël buntu course
je suis habitué à avoir faim en allant à l’école sans être dernier de la classe
man dama gëm ne sooner or later bu soobe Buur bi
moi je crois que bientôt tôt ou tard grâce à Dieu
dina ko mool le bu noon ni cool le ma waral coow li
je réussirai quand l’ennemi faillira je serai à l’origine de la rumeur
may gàddu caabi di noηηi-noηηi aanhan
quand je prendrai la clé en plastronnant aanhan
am xam-xamu zaïru baatinu wex ni kaani
détenir le savoir ouvert et caché
yoore lot of money di bégal jaam yi créé job yi
avoir beaucoup d’argent en faisant plaisir à ceux ont créé des emplois
jox booy yi yokk Pib bi teral Meer bi ak Paa bi
pour les jeunes en augmentant le PIB honorant le père et la mère
liggéeyal Pays bi nekk Prési May be, Président !!
Travailler pour le pays devenir Prési peut-être, Président !
et pourquoi pas ? Président tout est possible Et pourquoi pas ? Président tout est possible et pourquoi pas ?
des possibilités il y’en a et pourquoi pas ? Des possibilités il y’en a et pourquoi pas ?
uuuuhuuuu -yow yow yow!! Uuuuhu –
toi toi toi !!
What’s up what’s up what’s up?
Quoi de neuf quoi de neuf quoi de neuf ?
how life treatin u ? Nu mu deme ci sa side ?
Comment la vie t’a traité ?
noo tooge laa lay laaj ?
Je demande de tes nouvelles ?
wax ma lu ne sa mind, Wax ma lu ne sa mind
Dis-moi qu’est-ce qui te trotte dans la tête, qu’est-ce qui te traite trotte dans la tête ?
Yow what’s up what’s up what’s up ?
Bul kalu ci sa side
Toi quoi de neuf quoi de neuf quoi de neuf ? Ne reste pas dans ton coin.
yow wax ma lu lay faj ? li la metti na ko taaj.
Parle-moi de ce qui te soigne ? Je voudrais savoir ce dont tu souffres
wax ma lu ne sa mind jël ma ci suuf
Dis-moi ce qui trotte dans la tête prends-moi inbox
wax ji buñ ko aaaj
Ne suspendons pas la conversation
yé ya yaww
yé ya toi
wuyu wiiyu wuuyu wii wii
répondre wiiyu répondre
yé ya yaww wiiyu wiiyu
yé yaa toi wiiyu wiiyu